Sëriñ Tuubaa wax na ca Maasalikul jinaan ne: "boo umpalee mbirum wird, na nga xam ne lu màgg la, lu rëy maanaa la
Sëriñ Tuubaa wax na ca Maasalikul jinaan ne: "boo umpalee mbirum wird, na nga xam ne lu màgg la, lu rëy maanaa la."
Yal na ko Yàlla nangu ci barkeb Sëriñ bi.